NJÉNDEL RÉEWUM SENEGAAL

Wenn Askan, benn jubluwaay, benn pas-pas

Xamle

Vision Sénégal 2050 : Bokk yéene ngir réew mu moom boppam, naat te mànkoo.

01 Ut 2025
Dawal li ci topp

SENEGAAL 2050 SÉMBU SOPPI RÉEW MI

29 Oktoobar 2024
Dawal li ci topp

WÀCCEEL PEXEM SENEGAAL MU YEES MI CI WÀLLU XARALA

XEW-XEW

RÉEWUM SENEGAAL

Ca kaw àddukaayu ONU, Peresidaa FAY soññe na ci ñu tëggaat lu jëm ci wàllu lëkkaloo yi.
Biti Réew - 24 Sebtàmbar 2025
Dawal li ci topp
Ca ONU, Peresidaa FAY soññe na ngir ñu wattu demokaraasi ci kanamu ëppal gi.
Biti Réew - 24 Sebtàmbar 2025
Dawal li ci topp
Senegaal xaatim na ag lëkkaloo gu am solo gu tollu ci 10i milyoŋi dolaar diggam ak « Fondation Gates » ngir baral « New Deal technologique » bi.
Biti Réew - 24 Sebtàmbar 2025
Dawal li ci topp
Ca New York, Peresidaa FAY jataayu na ak Topp-Njiitu Kolombi.
Biti Réew - 23 Sebtàmbar 2025
Dawal li ci topp

ARMINAAT

TalaataSebtàmbar23
80eelu jataayu Ndaje mu Mag mu Mbootaayu Réewi àddina si.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
GaawuUt2
Màggalug Bisu Jëmbat Garab ci réew mi ca Àllub Mbaaw.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
ÀjjumaUt1
Kaajarug Palaŋu joyyanti koom mi ak dundiinu Senegaal.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
AlxamisSulet31
Xewu jébbale raayay “Concours Général 2025”
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
ÀjjumaSulet25
Tukki nemmiku ca Togóo ak ca Liberiyaa.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
ÀlarbaSulet9
Tukkib liggéey ca “Etats Unis d'Amérique”.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
AltineSuwe30
4eelu Ndajem àddina mi ñu jagleel kopparalug suqaliku gi.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp

Njénde li

RÉEWUM SENEGAAL

Pekk bi
Pekkub Njiitu Réew Mi Njiital Pekk bi moo koy jiite
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
Njëwriñ gu Rëy Gi
Jëwriñ Ju Rëy ji ci ab dekkre lañu koy tabbee mu nekk ci kilifteefu Njiitu Réew
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
Yeneen wànqaas yi
Pekkub sóobare, pekkub politig, yeneen ndoxal yi.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp

Màndargay Repiblig bi

Mboorum Njénde li
Tabaxug Njénde li ci tolluwaayam bu njëkk ci ndigalul Gaston Dumergue ca 1902
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
Jonn gi: 4i fani awril 1960
15i fani nowàmbar 1958 ci la Senegaal doon ub Repiblig daal di am jonnam 20i fani ut 1960.
Dawal li ci topp
En savoir plus
Raaya ak bàkku Senegaal
Raaya réewum Senegaal ñetti rëdd yu taxaw te tolloo la am.
Dawal li ci topp
En savoir plus
Bàkk yi
Bàkku réew mi, yeneen bàkk yi ak bàkku Renaissance Africaine
Dawal li ci topp
En savoir plus

SUNUY MBAALI JOKKOO

TOPPLEEN NU NGIR DARA BAÑ LEEN A RËCC