4eelu Ndajem àddina mi ñu jagleel kopparalug suqaliku gi.

jëwriñ - 30 MONTHS.JUNE 2025

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay FAY, dina dem ca “Seville” nekk ca Espaañ, 30i fani suwe jàpp 2i fani sulet 2025, ngir teewe 4eelu Ndajem àddina  mi ñu jagleel kopparalug suqaliku gi.