NJÉNDEL RÉEWUM SENEGAAL

Wenn Askan, benn jubluwaay, benn pas-pas

Xamle

Jataayu waxtaan ak Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay.

29 Nowàmbar 2024
Dawal li ci topp

SENEGAAL 2050 SÉMBU SOPPI RÉEW MI

29 Oktoobar 2024
Dawal li ci topp

WÀCCEEL PEXEM SENEGAAL MU YEES MI CI WÀLLU XARALA

XEW-XEW

RÉEWUM SENEGAAL

SAABALU NDIISOOG JËWRIÑ BU ÀLLARBA 05i FANI MARS 2025
NDIISOOG JËWRIÑ YI - 05 Mars 2025
Dawal li ci topp
Njiitu Réew mi Basiiru JOMAAY Fay amal na tijjitel Barabu Fésal bi ñu jagleel Yónnent bi Muhammat (SLHWS) ci Ndakaaru.
xamle - 27 Féewarye 2025
Dawal li ci topp
(Widewoo) Ab tënk ci Wolof ci Ndiisoog Jëwriñ gu 26i fani féewarye 2025.
NDIISOOG JËWRIÑ YI - 26 Féewarye 2025
Dawal li ci topp
New Deal Technologique : mébet mu am solo ci réew mi jëm ci def Senegaal muy ku ràññiku ci wàllu koomum xarala yi ci Afrig.
xamle - 24 Féewarye 2025
Dawal li ci topp

ARMINAAT

AlxamisFéewarye27
Tijjitel Barabu Jëmmal dundug Yónnent bi Muhammat (SLHWS) ak Xeyteg Lislaam
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
AltineFéewarye24
Noortel pexe mu bees ci Senegaal ci wàllu xarala « New Deal Technologique ».
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
GaawuFéewarye22
Bis bi ñu jagleel càmm gi ca Kawlax
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
ÀjjumaFéewarye21
NDOORTEL LIGGÉEYU PROMOREN CA Kungéel
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
AlxamisFéewarye13
38eelu jataayu Ndajem Mbootaayu Réewi Afrig yi ca Adis Abebaa.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
AlxamisFéewarye6
Jébbale raaya Njiitu Réew mi ñeel jàngalekat yi ca Garaa Tiyaatar Duudu Njaay Kumba Róos
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
GaawuFéewarye1
9eelu bëccëgu SETAL SUNU RÉEW ca Géejawaay.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
ÀlarbaSãawiye29
Siyaar ci Xalifa Seneraalu Laayeen yi
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
AltineSãawiye20
Ndajem Kilifa ak Njiiti wànqaasi pénc mi ca CICAD
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
ÀjjumaSãawiye17
Nganug Njiitu Réewum Gana ci Senegaal
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp

Njénde li

RÉEWUM SENEGAAL

Pekk bi
Pekkub Njiitu Réew Mi Njiital Pekk bi moo koy jiite
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
Njëwriñ gu Rëy Gi
Jëwriñ Ju Rëy ji ci ab dekkre lañu koy tabbee mu nekk ci kilifteefu Njiitu Réew
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
Yeneen wànqaas yi
Pekkub sóobare, pekkub politig, yeneen ndoxal yi.
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp

Màndargay Repiblig bi

Mboorum Njénde li
Tabaxug Njénde li ci tolluwaayam bu njëkk ci ndigalul Gaston Dumergue ca 1902
Dawal li ci topp
Dawal li ci topp
Jonn gi: 4i fani awril 1960
15i fani nowàmbar 1958 ci la Senegaal doon ub Repiblig daal di am jonnam 20i fani ut 1960.
Dawal li ci topp
En savoir plus
Raaya ak bàkku Senegaal
Raaya réewum Senegaal ñetti rëdd yu taxaw te tolloo la am.
Dawal li ci topp
En savoir plus
Bàkk yi
Bàkku réew mi, yeneen bàkk yi ak bàkku Renaissance Africaine
Dawal li ci topp
En savoir plus

SUNUY MBAALI JOKKOO

TOPPLEEN NU NGIR DARA BAÑ LEEN A RËCC