50eelu ati jonnug Kabo Werde.

jëwriñ - 05 MONTHS.JULY 2025

Njiitu Réew mi dina teewe, 5i fani sulet 2025,  màggalug 50eelu ati jonnug Kabo Werde. Muy tukki buy firndeel jëflantey xaritoo ak lëkkaloo gu am solo gi yàgg a dox diggante Senegaal ak dëkku ndox bii nekk ci Afrig Sowu Jant.