Mboorum Njénde li
Tabaxug Njénde li ci tolluwaayam bu njëkk ci ndigalul Gaston Dumergue ca 1902
Dawal li ci toppJonn gi: 4i fani awril 1960
15i fani nowàmbar 1958 ci la Senegaal doon ub Repiblig daal di am jonnam 20i fani ut 1960.
En savoir plusRaaya ak bàkku Senegaal
Raaya réewum Senegaal ñetti rëdd yu taxaw te tolloo la am.
En savoir plusBàkk yi
Bàkku réew mi, yeneen bàkk yi ak bàkku Renaissance Africaine
En savoir plus