SAABALU NDIISOOG JËWRIÑ BU ÀLLARBA 01 PANU OKTOOBAR 2025.
NDIISOOG JËWRIÑ YI - 01 MONTHS.OCTOBER 2025
read_more
Njiitu Réew mi dalal na mbooloo mu bawoo ci Kurélug Imaam ak Waaraatekat yu Senegaa.
xamle - 01 MONTHS.OCTOBER 2025
read_more
Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY ak naataangoom bu Gana, John Mahama, bokk nañu jiite xew wu jëmoon ci fàttaliku ak defaraat mboorum Afrig.
Biti Réew - 26 MONTHS.SEPTEMBER 2025
read_more
Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY séq na ab jataay ak France 24 ci 80eelu Ndaje Mu Mag mu Mbootaayu Réewi Àddina si.
laaj ak xibaar - 26 MONTHS.SEPTEMBER 2025
read_more
Njiitu Réew mi amal na ab jataay ak Doomi Buuru Kowet ca New York.
Biti Réew - 25 MONTHS.SEPTEMBER 2025
read_more
Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY dalal na naataangoom bu Koso ca Ndaje mu Mag mu ONU.
Biti Réew - 25 MONTHS.SEPTEMBER 2025
read_more
Ca New York, Njiitu Réew mi dalal na doomi Senegaal yay dund ca USA.
Biti Réew - 25 MONTHS.SEPTEMBER 2025
read_more
Ca ONU, Peresidaa FAY soññe na ngir ñu wattu demokaraasi ci kanamu ëppal gi.
Biti Réew - 24 MONTHS.SEPTEMBER 2025
read_more