laaj ak xibaar - 26 MONTHS.SEPTEMBER 2025

Ci 80eelu jataayu Ndaje Mu Mag mu Mbootaayu Réewi Àddina si, Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY, séq na ab jataay, àjjuma 26i fani sebtàmbar 2025, ak teleb Farance 24. Muy am pose ci Njiitu Réew mi ngir mu yaatal gis-gisam, diggante laamisoo gu ñu yeesal, yoon gu moom boppam ak manal sunu bopp ci wàllu koom.
Man ngeen a topp jataay bi :