jëwriñ - 18 MONTHS.AUGUST 2025
Njiitu Réew mi Bassirou Diomaye Faye dina amal tukkib ca Japon, 18 jàpp 26i fani ut 2025.
Ci tukki bii, Njiitu Réew mi dina teew ca 9eelu Ndaje mu mag ma ñuy amal ca Tokyo ci suqalikug Afrig (TICAD 9).
Dina teewe itam Bis bi ñu jagleel Senegaal ca “Exposition universelle” Osaka Kansai 2025.