jëwriñ - 09 MONTHS.JULY 2025
Ci ndënel Presidaa Donald Trump, Kilifa gi, Basiiru Jomaay FAY, Njiitu Réewum Senegaal, dina amal tukkib liggéey ca “États-Unis d’Amérique” 9 ak 10i fani sulet 2025.