Kaajarug Palaŋu joyyanti koom mi ak dundiinu Senegaal.

jëwriñ - 01 MONTHS.AUGUST 2025

Àjjuma 1 panu ut, ci kilifteefu Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY, Usmaan Sonko Njiitu Jëwriñ yi dina aajar Palaŋu joyyanti koom mi ak dundiinu Senegaal. Yëgle bii day wane jamono ju am solo ci réew mi, jëm ci sóob askan wi ci yoonu yokkute ak dundiin wu ñoŋ.