jëwriñ - 02 MONTHS.AUGUST 2025
Gaawu 2i fani ut 2025, Àllub Mbaaw dina dalal Màggalug Bisu Jëmbat Garab ci réew mi, di mbébet mu am solo mu jëm ci sàmm kéew mi ak delloosi gàncax gi ci réew mi.
Xewu ren wii Kilifa gi Basiiru Jomaay FAY Njiitu Réew mi moo koy jiite, muy feddali rekk kon jaayanteg Nguur gi jëm ci dooleel suqaliku gu sax ak sàmm balli mbindaare yi.