jëwriñ - 23 MONTHS.SEPTEMBER 2025
Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY dina dem ca New York, dibéer 21i fani sebtàmbar 2025 ngir teewe 80eelu jataayu Ndaje mu Mag mu Mbootaayu Réewi Àddina si waxtaan yi di door talaata 23i fani sebtàmbar.