Tukki nemmiku ca Pari

jëwriñ - 27 MONTHS.AUGUST 2025


Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay FAY, ñu ngi séntu, 27 ak 28i fani ut, ca  PARI ga mu war a teewe, ndajem lijjantikati saa-farãas mi MEDEF lootaabe ci àllarba ji 27i fanu ut 2025.