jëwriñ - 31 MONTHS.JULY 2025
“Grand Théâtre national” Duudu Njaay Róos dina dalal, alxemes 31i fani sulet 2025, xewu “Concours Général”, di jataay buy màndargaal xereñte gi ci njàngum Senegaal.l’excellence académique au Sénégal.
Xewu ren wi dina am ci kilifteef ak teewaayu Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay Jaxaar FAY.