Yeesalug Jëwriñ yi : Njiitu Jëwriñ yi di leeral tegtal yi ñeel Ngóornamaŋ bu bees bi.

xamle - 06 MONTHS.SEPTEMBER 2025


Ginnaaw yeesalug jëwriñ yi, Usmaan SONKO Njiitu Jëwriñ yi, dikkaat na ci tegtal yi tax ñu taxawal Ngóornamaŋ bu bees bii.

Man ngeen a topp fii kàdduy Njiitu Jëwriñ yi ci wolof :