Washington : Àddug Njiitu Réew mi

Biti Réew - 09 MONTHS.JULY 2025

Kilifa gi Basiiru Jomaay Jaxaar FAY, Njiitu Réewum Senegaal, teewe na ci àllarba ji ndaje mu mag mi Njiitu Réewum USA, Kilifa gi Donald J TRUMP lootaabe woon.

 Man ngeen a topp kàdduy Njiitu Réew mi ci widewoo bii :