Tukkib nemmiku Njiitu Réew Mi Basiiru Jomaay Fay ca Gaboŋ .

jëwriñ - 01 MONTHS.MAY 2025

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay, dina amal ub tukki ca Gaboŋ ci àjjuma i 2i fani mee, ci ndënel Kilifa gi Biris Oligi Ngemaa, Njiitu Réewum Gaboŋ, ci lu soxal xew wi ñuy amal ngir samp naataangoom bi.