Tukkib nemmiku ca Turki: Njiitu Réew mi di siyaare xabrub Mustafaa Kemal Ataturk

Biti Réew - 31 MONTHS.OCTOBER 2024

Njiitu Réew mi Basiiru JOMAAY Fay mu ngi dooree tukkib nemmikoom gi ca Turki ci siyaare xabrub Mustafaa Kemal Ataturk mi taxawal boole ko ak njëkk a jiite réewum Turki gu modern gi. Jëf ju am solo jii nag mooy màndargaal mbaaxi yokkute ak moom sa bopp yi boole Senegaal ak Turki.