Tukki nemmiku Njiitu Réew Mi ca Gine Bisaawóo.

jëwriñ - 26 MONTHS.MAY 2025

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay FAY, dina amal tukki nemmiku ca Gine Bisaawóo 26 ak 27i fani mee 2025. Muy tukki bu jëm ci gën a dooleel jëflante yu rittax yi dox diggante ñaari réew yi.