Siyaar ci Xalifa Seneraalu Laayeen yi

jëwriñ - 29 MONTHS.JANUARY 2025

Ci lu soxal màggal 145eelu wooteb Seydinaa Limaamu Laahi gi ñu jàpp 30 ak 31i fani sãawiye 2025 ci Ndakaaru, Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY, dina siyaareji njabootug Laayeen gi, tay ci àllarba ji 29i fani sãawiye.