Peresidaa FAY ñu ngi koy séntu ca Washington ga mu war a amal tukkib liggéey.

Biti Réew - 08 MONTHS.JULY 2025


Ci ndënel Pereaidaa Donald Trump, Kilifa gi, Basiiru Jomaay FAY bawoo na Ndakaaru ci suba wutali États-Unis.

Moom Njiitu Réew Mi war faa amal tukkib liggéey 9 ak 10i fani sulet 2025.