Biti Réew - 26 MONTHS.AUGUST 2025
Ginnaaw ba mu teewee TICAD9 ak « Exposition universelle » Osaka-Kansai 2025 ca Japon ba noppi, Njiitu Réew mi Bassirou Diomaye Faye, bawoo na Japon wutali Farãas.
Bu yeggee PARI, moom Njiitu Réew mi dina teewe, ndajem lijjantikati saa-farãas mi MEDEF lootaabe ci àllarba ji 27i fanu ut 2025.