Nemmiku jumtukaayu GTA ànd ko ak Njiitu Réewum Móritani.

jëwriñ - 22 MONTHS.MAY 2025

Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY, dina amal, alxemes 22i fani mee 2025, ag nemmiku ca jumtukaayu gaas bu “Grand Tortue Ahmeyim (GTA)”, féete ca digu géej wa dox diggante Senegaal Móritani, mu war koo ànd ak S Mohammet Uld Seex El Xasuwani, Njiitu Réewum Móritani.