Nataalu Ngóornamaŋ bu bees bi.

xamle - 17 MONTHS.SEPTEMBER 2025


Nataalu ñi bokk ci Ngóornamaŋ bu bees bi ak Njiitu Réew mi ginnaaw Ndiisoog Jëwriñ gu àllarba 17i fani sebtàmbar 2025.