Laamisoo: Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay Fay ñu ngi koy séntu ca réewum Siin 3 ak 4i fani sebtàmbar

jëwriñ - 14 MONTHS.AUGUST 2024

Ci Ndiisoog Jëwriñ yi, Njiitu Réew mi xamale na ne dina amal tukkib nemmiku ca Réewum Siin Popileer, 3 ak 4i fani sebtàmbar 2024, jëm ci 4eelu ndajem lëkkaloog sino-afrig, 05 ak 06i sebtàmbar 2024.