jëwriñ - 06 MONTHS.FEBRUARY 2025
Njiitu Réew mi, Basiiru JOMAAY Fay, dina jiite ci alxemes ji 6i fani féewarye 2025, jataayu joxe raaya Njiitu Réew mi ñu jagleel Jàngalekat yi ca Garaa Tiyaatar Duudu Njaay Kumba Róos.
3eelu edisoo bii day màndargaal màggal njàng mu mucc ayib ak dello njuukal jàngalekat yi nga xam ne seen dogu ak seen ug njàmbaar bokk nañu ci liy tabax askan wu jàng te dëgër!