laaj ak xibaar - 29 MONTHS.NOVEMBER 2024
Ci waajtaayu màggal 80eelu atu Bóom gi amoon Caaroy, Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay Fay, séq na waxtaan ak France 2, Agence France-Presse (AFP) ak Le Monde.
Waxtaan yi jëmoon ci fàttaliku mboor, nangu jaayanteg tiraayéeri senegale yi, niki noonu xew-xew yu gën a fés jamono jii ci àddina si.
Man ngeen a topp jataay bi fii: