jëwriñ - 20 MONTHS.DECEMBER 2024
Àjjuma jii di 20i fani desàmbar 2024, Njiitu Réew mi Basiiru JOMAAY Fay, dina jiite, ca saal dee bànke bu Njéndel Réew mi, jataayu dalal ay diññiteer. Xew-xew bii ci cosaanu réew mi dees na ci sargal ay jëmm yu ñu war a yéegal ci wàllu « Ordre national du Lion ».