Gise : Njiitu Réew mi dalal na Jëwriñ jii Zerbo EMILE mu Burkinaa Faaso

xamle - 20 MONTHS.SEPTEMBER 2024

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay dalal na ca njénde la, Jëwriñu Ndoxalug Mbeeraay ak Dem ak Dikk gu Burkinaa Faaso, M. Zerbo EMILE mi doon indi bataaxel bu bawoo ci Kapiten Ibraahiima Taraawore, Njiital Faaso.