🛑 DAAR-DAAR CICAD : Toppleen tijjitel Péncoo gi ñuy amal ci réew mi ci sistem politig bi.

xool - 28 MONTHS.MAY 2025

Ginnaaw ba ñu amalee, ca 2024, diisoo yi ñu jagleeloon wàllu « yeesal ak méngale yoon ak jamono », Njiitu Réew mi a ngi jiite tay, 28i fani mee 2025, jataayu tijjitel péncoo gi ñu jagleel ren, sistemu politig bi. 

Topp jataay bi daar-daar: