Bisub Diisoo ca CICAD

jëwriñ - 28 MONTHS.MAY 2025

Ginnaaw diisoo yi ñu jotoon a amal ca 2024, ci wàllu yeesal ak méngale yoon ak jamono, Njiitu Réew mi dina jiite, 28i fani mee 2025, tijjitel diisoo yi ñu jagleel ren sunu sistemu politig.