Bataaxelu Kilifag Réew mi Basiiru Jomaay Fay jëm ci Askan wi ci lu ñeel màggal bis bi réew mi amee jonnam.

jëwriñ - 03 MONTHS.APRIL 2025

Lu jëm ci  bis bi Senegaal moomee boppam, te ñu war koo màggal àjjuma 4i fani awril 2025, Basiiru Jomaay Fay, Njiitu Réew mi dina yékkati ay kàddu jagleel ko askan wi alxemes 3i fani awril 2025.