Bataaxel bu jëm ci Askan wi

jëwriñ - 31 MONTHS.DECEMBER 2024


Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay Fay dina yékkati ay kàddu jagleel ko askan wi talaata 31i desàmbar bu 20i waxtu jotee, ci Njénde li.