jëwriñ - 01 MONTHS.FEBRUARY 2025
9eelu bëccëgu jaayante gii di SETAL SUNU RÉEW dees na ko amal 1 panu féewarye 2025 ca Géejawaay . Kilifa gi Basiiru Jomaau Fay, Njiitu Réew mi mooy jiite bis bii ñu war a waxtaane tomb bii di « Setal Sunu Gox Mooy Sunu kaaraange ».