xamle - 14 MONTHS.DECEMBER 2024
Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay Fay bawoo na Ndakaaru tay ci suba wutali Abuja, ca réewum Niseriyaa, ngir teewe juróom benn fukk ak juróom benneelu (66eelu) ndajem Njiiti Réew ak Ngóornamaŋ yu Mbootaayu Réewi Afrig Sowu Jant yi (CEDEAO), ñu jàpp ko 15i fani desàmbar 2024.