Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay, dina amal ub jataay ak taskati xabaar yi ci réew mi ci gaawu bi 13i sulet 2024 li ko dale 21iw ca Njénde la.

laaj ak xibaar - 11 MONTHS.JULY 2024
Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay, dina amal ub jataay ak taskati xabaar yi ci réew mi ci gaawu bi 13i sulet 2024 li ko dale 21iw ca Njénde la.

Jataayu waxtaan ak xamle - 11i sulet 2024

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay, dina amal ub jataay ak taskati xabaar yi ci réew mi ci gaawu bi 13i sulet 2024 li ko dale 21iw ca Njénde la.

Man ngeen a topp jataay bi ci mbaali jokkooy Njénde li.