Nganug Njiitu Réew mi Basiiru JOMAAY Fay ca Emiraa Araab Unii

jëwriñ - 04 MONTHS.DECEMBER 2024

Kilifa gi Basiiru Jomaay Fay, Njiitu Réewum Senegaal, dina amal ug ngan ca Emiraa Araab Unii 4 ba 6i fani desàmbar 2024, ci ndënel kilifa gi Seex Mohammet Bin Sayed Al Nahyan, Njiitu Réewum Emiraa Araab Unii.