waxtaan - 16 MONTHS.FEBRUARY 2025
Njiitu Réew mi teewe na, li ko dalee 13 jàpp 15i fani féewarye 2025, 38eelu jataayu Ndajem Mbootaayu Réewi Afrig yi.
Ba mu dellusee Ndakaaru, Njiitu Réew mi dikkaat na ci tukkeem boobu mu doon amal ca Addis-Abebaa teg ci àdduwaale ci càmbar gi bawoo ci rappoor bi « Cour des Comptes » amal ci anam yi ñu doon jëfandikoo alalu askan wi.